Direct: Vidéo Léna Gueye infidèles, Serigne Ngagne en colère Tacle Lena et Ibou Gueye De Evenprod

2 400 visualizzazioni 154K

Rejoignez nous
Soyez le premier à être informé!
Sunugal 24 c'est l'information à sa juste valeur

Commenti

  1. mame dior ngom
    mame dior ngom
    13 giorni fa

    deugeule machaala longue vie à toi 🙏🏽

  2. Eva Soniane
    Eva Soniane
    21 giorno fa

    Vraiment chapeau à vous Serigne ngagne vraiment 😍😘🙏

  3. Adama Njie
    Adama Njie
    21 giorno fa

    Allahumma baarik, more respect for you. Indeed the grave waits for us, manners, modesty etc is very important in our Deen. Maa shaa Allah, well said tres bien

  4. Mamadou Dione
    Mamadou Dione
    25 giorni fa

    Trian nga feyoco tousse

  5. mouhamed Diop
    mouhamed Diop
    Mese fa

    iow khana lena dala niamal badio bi motakh nga koye defandré😂

  6. mohamed sougou
    mohamed sougou
    Mese fa

    indo yii dh dieulnaniou première

  7. Gane Gueye
    Gane Gueye
    Mese fa

    J’ai jamais aimé la série Infidèle je l’ai trouvé troop vulgaire

  8. Alex King
    Alex King
    Mese fa

    Serigne Ngange true talk 👈 you're a Legend, keep standing for the truth

  9. Mouhamed Cissé
    Mouhamed Cissé
    Mese fa

    Vraiment deug la

  10. Gning Mamadou
    Gning Mamadou
    Mese fa

    Machallah s gagne plus de 25 de sixé ken moussouleu degu ci lou gnak fayda chapeaux

  11. Amadou Mactar Beye
    Amadou Mactar Beye
    Mese fa

    Très bien Serigne gagne tu as tout dit la vérité est une et Seule merci

  12. Coumba Tilala
    Coumba Tilala
    Mese fa

    Wa kougkande bou dé amna louko yala may bay meuna khar guedj gui nafi dieulé mbass mi wa salam 🙏

  13. chikory kara l'artiste recus Mr Bean noire
    chikory kara l'artiste recus Mr Bean noire
    Mese fa

    Domaine bomana Guisse si aduna kiko Diangue ak kiko Dianguoule bokouñiou ❤️👌 Tonton Ngane respect 🙏

  14. Elhadji Mamadou Mboup
    Elhadji Mamadou Mboup
    Mese fa

    Wakh ga deugue Merci.

  15. bineta Mbengue
    bineta Mbengue
    Mese fa

    Machallah yalla na yalla fayi la

  16. Ibrahim Niang
    Ibrahim Niang
    Mese fa

    Good job 👍 my brother 👊

  17. Absa Moukhamed
    Absa Moukhamed
    Mese fa

    Verite apsolut serigne Ngagne Deug pire Macha'allah infidel meme les paroles son vulgaires keen menouko khol ak sa gniabot porno pure et dure Les paroles les gestes tout est vilgaire Mane mome Ndeye Ndiaye ak roubeu seye ngoy sa may artistes si nbetel fate kine daffa vulgaires elle dit que des gros mots serie boumou bok doumako settan YALLAH NA NGNIEP AM DIAM THIA FEBARBI DI COVID 19 BI YALLAH RAKHASS KO THI ADOUNABI YEPP INCHA'ALLAH SI BARKE SEYDINA MOUKHAMED ( psL )

  18. Salimata Gueye
    Salimata Gueye
    Mese fa

    Ngagne yaw damala yagu beug depui bamay am 18ans mai chak fw tu di la verite et tu es digne vremen chapô

  19. wakh deugu
    wakh deugu
    Mese fa

    Mention tres bien serigne ngagne.

  20. Youwa Dia
    Youwa Dia
    Mese fa

    Deug dal dou meussa nékh !! Wawaw

  21. Yasmina Diop
    Yasmina Diop
    Mese fa

    Il a beaucoups de sagesses serigne Ngagne machaAlah Yalna nala yalla defal diam. Liga wakh lep amna solo té ragalo dara ci ligay wakh.

  22. Ndeye astou Diop
    Ndeye astou Diop
    Mese fa

    Merci

  23. D D
    D D
    Mese fa

    Machaalla

  24. Awa Niang
    Awa Niang
    Mese fa

    Vérité absolue infidèles kou gueneu vilguér rék yay déf beus rék lagniou beugeu

  25. Sawda Drame
    Sawda Drame
    Mese fa

    Ngagne je t'adore encore plus

  26. Oumar Seye
    Oumar Seye
    Mese fa

    Merci beaucoup ablaye Diouf

  27. Miss Thioye
    Miss Thioye
    Mese fa

    Machaala ngagne💋💋

  28. Oumou Ahmad A99
    Oumou Ahmad A99
    Mese fa

    Ngagne dafa amm foula, beugeu limi deff et pourtant il excelle dans l'art c'est un très grand comédien, il a un jeu d'acteur impressionnant 👏🏽👏🏽👏🏽man foula ak fayda lama nehhé

  29. Saidou Mbaye
    Saidou Mbaye
    Mese fa

    Ma sha Allah serigne ngagne

  30. Sarata Diatta
    Sarata Diatta
    Mese fa

    vraiment je l'adore

  31. Sokhna Boye
    Sokhna Boye
    Mese fa

    Bilahi Mame Maodo Malick Sy wakhna DEUG dé

  32. Fatou Lo
    Fatou Lo
    Mese fa

    Le journaliste aussi machallah! Tu a été à la hauteur 👏questions bien posées et le sens de l'écoute

  33. Fatou Lo
    Fatou Lo
    Mese fa

    Dëgg nékhoul té dou rombe ay nop 👂en l'écoutant on sent un vrai artiste plein d'expérience kham limouy wakh té ñémé ko 👏vraiment chapeau à vous 🎩💖

  34. Sokhna Boye
    Sokhna Boye
    Mese fa

    Bilahi Ngagne da deugou nak merci beaucoup

  35. Maguette Wade
    Maguette Wade
    Mese fa

    Machaalaah Serigne Ngagne laffthiaatt wakh dji raffenetnaa

  36. Sabelle Fall
    Sabelle Fall
    Mese fa

    DEUGUE REKK GA WAKH

  37. sourga
    sourga
    Mese fa

    merci serigne ngagne valeurs amna balrgui dieureudieuf way

  38. Ndéye Cissé
    Ndéye Cissé
    Mese fa

    Vraiment mane ki sope nako nakh foula ak faydame Yalla nasa fane koude

  39. Madjiguène Ngom
    Madjiguène Ngom
    Mese fa

    Merci beaucoup ngagne

  40. Guereume SENE
    Guereume SENE
    Mese fa

    il faut l'exclure de la série Mbettel elle ne le mérite pas.

  41. ousmane djigo diagne
    ousmane djigo diagne
    Mese fa

    Ngingne c’est une tête 💪🏿

  42. Seex Abdu
    Seex Abdu
    Mese fa

    Wax nga dëgg de waaw guur

  43. Seex Abdu
    Seex Abdu
    Mese fa

    Sëriñ Ngañ daal bëgg naa la

  44. ousmane djigo diagne
    ousmane djigo diagne
    Mese fa

    Posez vous la question qui sont derrière Ibou Gueye

  45. ousmane djigo diagne
    ousmane djigo diagne
    Mese fa

    Ibou gueye mom tate rek lay prôner est-ce naturellement il est comme ça

  46. ousmane djigo diagne
    ousmane djigo diagne
    Mese fa

    C’est dans son sang 🩸 elle n’éduque pas elle détruis nos valeurs

  47. ousmane djigo diagne
    ousmane djigo diagne
    Mese fa

    On dirait lena on l’a éduqué comme ça

    1. ousmane djigo diagne
      ousmane djigo diagne
      Mese fa

      Merci ngagne tu as tout dis

  48. ousmane djigo diagne
    ousmane djigo diagne
    Mese fa

    Lena mo amoul valeur ah éthique mais les acteurs sont nombreux pourquoi elle accepte seulement les rôles de thiaga et sexy

  49. Papa Ousseynou Sagna
    Papa Ousseynou Sagna
    Mese fa

    BLH DEUGU LA WAX

  50. Alioune Barry
    Alioune Barry
    Mese fa

    Serigne ngagne est exeptionnel

  51. Alioune Barry
    Alioune Barry
    Mese fa

    Mashallah

  52. ALIOU KANE
    ALIOU KANE
    Mese fa

    NGAGNE MON N'ARTISTE PREFERE POUR TOUJOURS Félicitation

  53. Marieme Diop
    Marieme Diop
    Mese fa

    Deugue dou romb deugue interview bi diarna large diffusion partager leko no.bilay serigne gueunenala estimer machallah

  54. Papa Aliou Sarr
    Papa Aliou Sarr
    Mese fa

    Bravo

  55. diatou Diakhate
    diatou Diakhate
    Mese fa

    MashaAllah un homme véridique et sage . Il mérite vraiment son nom artiste . Bonne continuation

  56. Abdoulaye Ndoye
    Abdoulaye Ndoye
    Mese fa

    Tjr égal lui même

  57. Aminata Dominique Diouf
    Aminata Dominique Diouf
    Mese fa

    La personne qui a fait la série infidele yalla reubeu koo Yakee Yakee société bi

  58. FATIMA ABABACAR SY
    FATIMA ABABACAR SY
    Mese fa

    Non j'ai beaucoup de respect pour toi🙏😍machallah un nitt bou nité

    1. del men
      del men
      Mese fa

      Nekk nitt yombouna. Nitté moo diaffé. Teh moom nitt bou nitté leuh. Machalah.

  59. Ahmadol Khadim Leye
    Ahmadol Khadim Leye
    Mese fa

    Waw goor serigne ngañ deugg pur

  60. Life story
    Life story
    Mese fa

    Lou ngagne liguéyone si léna ibou gueye yakhanoko.

  61. Oumar Ba
    Oumar Ba
    Mese fa

    Vraiment c'est ça un homme responsable t'as tout dit je ne dis pas senegles mais les monde a besoin des ça comme conseil merci diof et bien des choses à la famille dia deuff

  62. Khady Ndiaye diagne
    Khady Ndiaye diagne
    Mese fa

    Diadieufeuté Serigne ngagne,kaadou yi amna solo lolll sakh💪🤔🤧

  63. Cheikh Diaw
    Cheikh Diaw
    Mese fa

    ❤❤❤❤❤

  64. Ndéye astou Sokhna
    Ndéye astou Sokhna
    Mese fa

    Barki allkhouranoule karime Serigne ngagne malla beugue ndakh sa nitté sa dignité ak sa yar machalla zéro faute yaw Amal diam 😍😍

  65. fediore adji bineta
    fediore adji bineta
    Mese fa

    Franchement Serigne ngagne chapeau à toi Macha’ALLAH wakh nga lep te lima gueune nekh si yaw deugue rk ngay wakh

  66. Fatou Ndiaye
    Fatou Ndiaye
    Mese fa

    Lalla khou akkoubar Lalla khou akkoubar ......

  67. Khady Dieng
    Khady Dieng
    Mese fa

    Waye Léna dou khalé dafa yabaté rek ak niak pudeur

  68. abdou sarr
    abdou sarr
    Mese fa

    Bilahi linga wax si koukande dafa lér ngagne vrai goor yalla nga

  69. abdou sarr
    abdou sarr
    Mese fa

    Tres intelligent serigne ngagne guenala beugue boy yii diangouniou théatre

  70. abdou sarr
    abdou sarr
    Mese fa

    Merci serigne ngagne tu a tout dit léna kon la ibou gueye mom producteur yeup mosi guena domeram guemoul yalla sakh

  71. Dada Fall
    Dada Fall
    Mese fa

    Bilahi Serigne Ngagne beuguenala niit nité

  72. thiamass
    thiamass
    Mese fa

    Respect s ngagne

  73. OUMAR NIANG
    OUMAR NIANG
    Mese fa

    Seringe ngang revelación yim wax ci problem lena bi degue bu wér Le

  74. adia adia
    adia adia
    Mese fa

    Macha-Allah, chapeau, serigne ngagne.

  75. Mame Sokhatil Diagne
    Mame Sokhatil Diagne
    Mese fa

    Bien dit Gagne, merci pour ces paroles de vériter.notre pays a besoin des gens comme vous.

  76. ndongo ndiaye
    ndongo ndiaye
    Mese fa

    Dia diafe machala machala ✊🏿👏🏽

  77. sow sokhna
    sow sokhna
    Mese fa

    Mashala lingfi wakh ken duko dindi

  78. Babacar Saliou
    Babacar Saliou
    Mese fa

    Merci beaucoup serigne pour ta franchise chapeau à toi

  79. NEYMAR10 DIALLO
    NEYMAR10 DIALLO
    Mese fa

    Diadieuf way billahi mala gom amga diarama ❤️❤️🇸🇳🇫🇷🇫🇷💪💪🙏🙏

  80. maary ka
    maary ka
    Mese fa

    Vraiment Ngagne t'es un homme de dieu.

  81. Pa Omar
    Pa Omar
    Mese fa

    Sérigne Ngagne mon artiste préféré. Toujours égale à lui même

  82. Sophia Sow
    Sophia Sow
    Mese fa

    Machallah

  83. Babaly Thiam
    Babaly Thiam
    Mese fa

    Machalla ya bakh

  84. Alpha Diallo
    Alpha Diallo
    Mese fa

    T’as tout dit Sergine Ngagne Respect à vous

  85. ROKHEYA YAFFA
    ROKHEYA YAFFA
    Mese fa

    Machala bien dit

  86. Mor Ngom
    Mor Ngom
    Mese fa

    Yalla nala yalla défal diam

  87. Mohamed Thiam
    Mohamed Thiam
    Mese fa

    Merci beaucoup

  88. bibichanel barbe Ndoye
    bibichanel barbe Ndoye
    Mese fa

    Infidel tiaga gegolo gouine gordjiguen len fa dadialé lena en réalité mo rawe limouy joué amoul kilifeu rien dans la tête..kena nakhouko gagne boul rafetal xamgua leep serie yi yakh negne deukeu bi sou fekone télé la yam sakh dou grawe mai xalé yi si téléphone yi lagnouy setane serie yi negne si diouk senegal deukou dioulite la

  89. bibichanel barbe Ndoye
    bibichanel barbe Ndoye
    Mese fa

    Vérité absolue respect gagne

  90. Balla Diagne
    Balla Diagne
    Mese fa

    Walahi sedalgua sama kholbi ngagne yalnala yala faye lena ya gnake diome do rousse sah gnak diome

  91. Balla Diagne
    Balla Diagne
    Mese fa

    Serigne ndagne yalnala yala faye amine amine amine

  92. Balla Diagne
    Balla Diagne
    Mese fa

    Barki alkhourane ma beug serigne ngagne Barki serigne touba

  93. Eva Ly
    Eva Ly
    Mese fa

    Serigne ngagne dama messa nékh vraiment sama référence la j l'aime beaucoup ❤️❤️❤️pére doundeul rék🙏

  94. Khadim Sabara
    Khadim Sabara
    Mese fa

    Merci bcp Ngagne meunou gnou theatre kom yéne ak ay sanekh il faut gnou vulgaire bolé si yoyou pour nitt gni sétane ko, amou gnou talent bi donc vulgarité bi moy def sene particularité !!!

  95. Babacar Baradji
    Babacar Baradji
    Mese fa

    Diadieuf s ngagne amall diamou rék insallah li nga wakh lépou deugleu masallah

  96. Adja GUEYE
    Adja GUEYE
    Mese fa

    Machallah Ngagne 👌deug dé yalla moko moom linga wakh dafa lèer

  97. babacar Toure
    babacar Toure
    Mese fa

    Bilae wakh nga dege merci

  98. Aliou mbodji
    Aliou mbodji
    Mese fa

    Yaw dh lo def mou refet

  99. samba thiam
    samba thiam
    Mese fa

    Yallah nala yallah fay sa khol

  100. Khadim Diop
    Khadim Diop
    Mese fa

    Amna solo Jaajëf waxna lepp🇸🇳🇧🇷